Ndoomu Buur Si - El Principito en Wolof- Preventa

Titenfass

Nuevo producto

Disponible en febrero

18,00 € impuestos inc.

Ficha técnica

Escritor‎Antoine de Saint-Exupéry
TraductorNicolas Quint
IlustracionesAcualeras originales
EcuadernaciónRústica
ISBN978-3-946190-67-7
Páginas96

Más

Ba ma amee juróom-benni at, mës naa gis nataal bu rafet ci ab téere ci mbiru àll bu naat bu tuddoon Nettali yu dëggu. Nataal baa ngi doon wone yeew muy wonn mala. Sotti bu nataal baa ngi nii. Ñu ngi doon wax ci téere bi ne: “Yeew yi danuy wonn ay mala te duñu leen sàqami. Ginnaaw bi duñu mën a yëngu te dañuy nelaw juróom-benni weer di reesalaale.” Loolu tax na ba may xalaat lu bari ci nettali yiy xew ci àll bi. Ma daldi jël kareyoŋ tàmbalee rëdd sama nataal bu njëkk.

Reviews

No hay reseñas de clientes en este momento.

Write a review

Ndoomu Buur Si - El Principito en Wolof- Preventa

Ndoomu Buur Si - El Principito en Wolof- Preventa